Loo wara def so feebaree walla ŋay laaj si sa wallu wergi-yaram?
Ŋa xamal sa bopp si wallu feebar yiy gën a wallaate, si wallu ëmb ak feebaru xel. Diŋa jot xibaar yu jëm si ki lay dimbali soo feebaree ak li ŋa wara def soo feebaree.